Mbootaay ‘Diam Rek’

Suñu jël beeñu meebüt moy yóbbu ay jumtukaay yu tollok ci fük ci ay pouss pouss, ci néew gi doole yi nekk ci bërëb yi gënë rukke ci biir Casamance ci ñeex tali ati 2025. Ñiogi lung kok ay botay yuy taxawu way laago yi ci nekk ci goxi Ziguinchor, muy Association regionale des handicapes moteurs giir mënë jox jumtukaay ñi ko yee lool.

Bu loolu weesoo dañu taxawal ñeeti fani lël giir waayu laago ci nekk ci mbootaayu yoyu ci wàllug tàggat yaram yu mel ni ( surf ak kayak) aki weccante xamluwaay aki xalaat. Waaye meebüt bi ñëkk té guën ci amm solo ci mbootaay gi moy deem bay njëriñ  seen boop té dootu ñu soxlal kénn as lëf .

Icon showing a wheelchair user in motion